Ci paccam bobu di firil kalaama askan wi, ICV munalèe dimbali ci bole lèen ak ndaw su xaraň su degg sa kalama ak kalamay daara ji ak su lèen di taxawu ci soxla yi ngèen di dox.
Ndaw yi ňu lèen di booleel di na tax ngèen mënna xam lèpp luňu waxtaané ci ndajje yooyu, dina tax tamit ngèen mën caa bokk bay wax sa xalaat, bay tamit mënna laaj ci lèpp lula jaaxal.
Ligèeyu ndaw yi firilaate kalama yi di na tax nga mënna bokk ci bèpp yëngu-yëngu bu daaraji di def (muy ndajje, gissé boo wara def ak njiit yi, xéw-xéw yi…) muy lu am solo ci sa mucuk doom ci daara ji.
Ngir xeex ndax mi tè jublu lii di yaatalate gi ak toolole gi bulèen am sikisaka ci woo suňuy ndaw.Ku ňu Bëgga jott
Nungi lèeen di ňaan ngèen bindu ji ci site bi situ ëtt bie ňeneen ňi tamit bulen neexe ňu jott ňu ci suňu bërëbu igèeyu kaay yi +41 22 800 14 36.
* Ëtt boobu kumu nèex jot ci amul xaji amul sèen.
©1997-2025 Migralingua|
system mcart|
Mis à jour: 2024-12-13 00:50 GMT|
Connecter