Familles

Ëttu waajur yi

Read this page in another language: français, English, español, Shqip (Albanian), ;العربية (Arabic), Български (Bulgarian), 中文 (Chinese simplified), 中文 (Chinese traditional), hrvatski (Croatian), فارسی (Farsi), Deutsch (German), italiano (Italian), македонски јазик (Macedonian), Polski (Polish), português (Portuguese), Română (Romanian), Русский (Russian), Српски (Serbian), Swahili, Tagalog (Tagalog), ไทย (Thai), Türkçe (Turkish), اردو (Urdu), Tiếng Việt (Vietnamese), Wolof.

_______

Dangèen wara dem ci ndaje waajuru ndogo yi, wala ngèen wara gisèek kenn ci jangalekat yi wa sax kenn ci kilifa yi ci daara ji, wala ngèen bëgga topoto ak xam sèen jangu doom te am ay jafe-jafe ci wax kalama nasaraan?

Ci paccam bobu di firil kalaama askan wi, ICV munalèe dimbali ci bole lèen ak ndaw su xaraň su degg sa kalama ak kalamay daara ji ak su lèen di taxawu ci soxla yi ngèen di dox.

Ndaw yi ňu lèen di booleel di na tax ngèen mënna xam lèpp luňu waxtaané ci ndajje yooyu, dina tax tamit ngèen mën caa bokk bay wax sa xalaat, bay tamit mënna laaj ci lèpp lula jaaxal.

Ligèeyu ndaw yi firilaate kalama yi di na tax nga mënna bokk ci bèpp yëngu-yëngu bu daaraji di def (muy ndajje, gissé boo wara def ak njiit yi, xéw-xéw yi…) muy lu am solo ci sa mucuk doom ci daara ji.

Ngir xeex ndax mi tè jublu lii di yaatalate gi ak toolole gi bulèen am sikisaka ci woo suňuy ndaw.

Ku ňu Bëgga jott

Nungi lèeen di ňaan ngèen bindu ji ci site bi situ ëtt bie ňeneen ňi tamit bulen neexe ňu jott ňu ci suňu bërëbu igèeyu kaay yi +41 22 800 14 36.

* Ëtt boobu kumu nèex jot ci amul xaji amul sèen. 

©1998-2024 Migralingua|system mcart|Mis à jour: 2024-12-13 00:50 GMT|Notre politique | RSS|